Musique: Viviane Chidid – Teeyal

64

Lyrics

Deugeu teule nè rek tothie na teyal loufi diar ngendy daw bey danou teyal fo tok beugeu gnou nawla teyal wagnil eupeule tè ba netali teyal dègueloulene Wakhou yaram ba teyal neuneu wakhou kham yone bè ko geune teyal beugeu buzz bamou diarala teyal nga taguègo tè dewagoul Cou nek amanga Lila daye fekhèl nga dieum ko lindianti dhè Lila wakh sa galer ngi takk Di boy dieum ko lindianti té Faye ko dhé li la Wakh

lou touty nga def ko lou patta Lo xam netali li la wakh Yakamti rayone na sa gnaum mame deuguena rayone na sa gnaum mame boukou lék féké gnorogoul boul di Wakh lo khamné amagoul Xamoulo do Khar bagnou xamala Guissoulo do Khar ba guiss Lou geuneu lér nga dem Na nga tey ta nga dale Amigo Li ngaye Wakh wauroula nopi bakhna thi Lo xamoul lanla Gawa Wakh Meuna indi mussiba

Deugeu teule nè rek tothie na teyal loufi diar ngendy daw bey danou teyal fo tok beugeu gnou nawla teyal wagnil eupeule tè ba netali teyal dègueloulene Wakhou yaram ba teyal neuneu wakhou kham yone bè ko geune teyal beugeu buzz bamou diarala teyal nga taguègo tè dewagoul Manè li Khawma lanla li khawma lanla li khawma lanla li ( bis)

ki dhè lidjantinala lidjantinala lidjantinala yaw mi ( bis) Lingua bindeu eskeu deugeu leu fake news mane yeugeulouma beugeu beuz ba takh nga dima sosal lingua def Dou xam gna Noumou toudou toumale boy yakati nit wala sakh boy bindeu thi nit nala l’ère li ngaye Wakh ni lou ame la lou ko moy Dina done sa musiba

Deugeu teule nè rek tothie na teyal loufi diar ngendy daw bey danou teyal fo tok beugeu gnou nawla teyal wagnil eupeule tè ba netali teyal dègueloulene Wakhou yaram ba teyal neuneu wakhou kham yone bè ko geune teyal beugeu buzz bamou diarala teyal nga taguègo tè dewagoul

PARTAGER
0 0 voter
Évaluation de l'article
S’abonner
Notifier de
guest
0 Commentaires
Inline Feedbacks
View all comments